Diamonoy 2016, sunu projet day dimbali ambassadou france yi ci adouna bi ak ambassade yi nek bire france si walou ada ak thiossane, lou eupeu 60+ ambassade you nek Paris wala ci adouna bi yeup nguir same akhe ak yéléfou mbolome nit yi dounde goordjiguéne LGBTQI+
